Tamsir SN - YAKAR

Опубликовано: 16 Июль 2026
на канале: Tamsir SN
41,329
1.5k

Enregistrement : NeguRap Music
Music by: PeulhBouHighBeatz
Mix & Mastering: PeulhBouHighBeatz
Writer: TAMSIR
Cover: Digital Hub


Lyrics :

(Yow yama jangal doundeulmeu)x2

Couplet 1:
Mangui guanéssi lii di deugg xaaxaam yi té dooragouma
Neksi sama yoon xam niouma yeené lou baaxak lou bonn
Mangui guiss lepp nieupp mou leer nagn si man goumbawouma
Geumné yallah rekkay meuneu defsi man limay doonn

Tax mangui dieem sabablou niaan ngaala mou dimbalima
Amouma kenn kouma yaakar kouddoul moom si dounya

Mooma fi wathiei
Mousseulma si gathiei
Dougnma youkhou sathiei
Mangueek sama ngor


Douma meusseu fattei
Yallah nim ma sakkei
Nim nara attei
Looloy lima niorr

Niaanalma yow mii yaay
Yow mi eumbb diourma nampalma
Gathiei ngalama baye
Yow yaama jangal doundeulma


🎶🎶🎶🎶🎶🎶🎶🎶🎶
Ayyiyeeee heeeee

(Yow yama jangal doundeulmeu)

Weuyleleen
Weuyleleen meu baye booy

(Yow yama jangal doundeulmeu)

Couplet 2:
Mann geumnaa
Guissnaa
Ni dina meusseu baaxi inchallah
Bouko sobei
Niou seen ma
Fepp founiouy xool ni machallah
Yallah
Ni mooma
Moo moom lepp louy mayei
Bouko neekhei
Mou defsi
Diaamam yi lougnmay soppei

Xamnaa
Guissnaa
Dina meusseu baaxi inchallah
Bouko sobei
Niou seen ma
Fepp fougn ma xool ni machallah
Yallah
Ni mooma
Moo moom lepp louy mayei
Bouko neekhei
Mou defsi
Diaamam yi lougnmay soppei


🎶🎶🎶🎶🎶🎶🎶🎶🎶
Ayyiyeeee heeeee

(Yow yama jangal doundeulmeu)

Weuyleleen
Weuyleleen meu baye booy

(Yow yama jangal doundeulmeu)


Gathiei ngalaama baye
Yow baye Jeureujeufeutee
(yow yaama jangal doundeulmeu)
Weuynaala baye
Geureumnaala baye boy yiyeeyiyey
(yow yama jangal doundeulmeu)