WIZZY KANA - NAMEL (Clip Officiel)

Опубликовано: 16 Июль 2026
на канале: Wizzy Kana
657,415
17k

#wizzykana #sénégal #abonnetoi

Artiste: Wizzy Kana
Compositeur: Fantastic beatz
Son: Neegurap music
Mix master: Peulbouhigh beatz
Directed by: Kalash director
Scénario: Tonton Ada OG
Habillement: OG Thi Lepp

Lyrics:

Jël nga sama xol
Xel bi thi iow leuh miir
jJaner sa dieum
Weetay bi dafma diis
Name naa jote say bataaxal
Ngir kham thi lane nga né
Nelawatouma
Guddi ba beute sett
Di xool say natale
Dianaxé naa
Koula mérité ,waro forcé pour am sont attention
Mbeuguél solution la wara done mais waroul nekk equation

Iow boma seetaané
May nga souniou none yi louniouy reetaané
Niom danio seuytané
Lou waay meuneu deff iow nagn ko waxtanei
Iow boma seetaané
May nga souniou none yi louniouy reetaané
Niom danio seuytané
Lou waay meuneu deff iow nagn ko waxtanei

Deggënte waat ak yaw
Wax la sama namel
Jakarloo waat ak yaw
Won la sama nobeel
Xol du fen
Boo nekoon ak kenen
Sa xel du jugee ci man
Ndax mbëgeel
Bu dëggoo du fen
Bula jekku wee dalay daan
Mënuma
Fatte fiñu jaar te duma
Bayi mu naxsaay
Lima mom
Damkoy dieuli waat maala mom
Té doumla saggané